Ubbil li ci biir

Yéenekaay yi La Tour de Garde ak Réveillez-vous !

Mën nga telesarse suñu yéenekaay yi sukkandiku ci Biibël bi ci lu ëpp 200 làkk. Ci làkk yooyu, am na làkku muuma yi. La Tour de Garde dafay sukkandiku ci li Biibël bi yégle woon ngir won ñu li xew-xewi àddina si tey di tekki. Dafa ñuy yégal xibaaru jàmm bi ci Nguuru Yàlla te loolu dafay dëfal suñu xol. Dafa ñuy xiir itam ci am ngëm ci Yeesu Kirist. Reveillez-vous ! dafa ñuy won ni ñu mënee jànkoonte ak jafe-jafe yi am ci àddina si tey. Dafay dëgëral itam suñu ngëm ci li Yàlla dige, maanaam dina fi indi àddina bu bees fu nit ñépp di dëkk ci jàmm ju mat sëkk.

Tànnal benn làkk ba pare nga bës fi ñu bind Génne ko ngir gis yéenekaay yi am ci làkk bi nga tànn ak ni nga leen mën a telesarsee.

 

RÉVEILLEZ-VOUS !

12 ponk yiy tax njaboot yi am jàmm

Topp xelal yi nekk ci Biibël bi, mën na la dimbali nga am jàmm ci sa dund njaboot.

TÀNNAL NI PAAS BII DI FEEÑE

RÉVEILLEZ-VOUS !

RÉVEILLEZ-VOUS !

RÉVEILLEZ-VOUS !

LA TOUR DE GARDE

LA TOUR DE GARDE

LA TOUR DE GARDE

LA TOUR DE GARDE