2018-2019 Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan — Ak ki bànqaas bi yónni

Seetal porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan bi, ak waxtaan yi ki bànqaas bi yónni nar a def.

Dëgërlul !

Porogaraam bi dina leeral ni ñu mënee am doole bi ñu soxla ngir dëgër ci ngëm.

Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii

Dinañu tontu laaj yii ci porogaraam bi.